Béggué way !!!la premiére des mariées hotladies!!!!ni ma la khamé rek shon
na dal!!!
Commentaire de diawa (12/10/2008 22:51) :
méronne na nak parce k jetais la seule a ne pas etre invitee...mais ak
sancé bi mom kouko guiss mer bi wathie...balnala et FELICITATIONSS....je te
souhaiote beaucoup ded bonheur....
Commentaire de lynsha (16/10/2008 16:31) :
ki dafay fo
naz fataliko liniou ko wakhone si eupoukaye bi.....
beusseum lawone té défarone na bamou bakh
Commentaire de yeya kane (17/03/2009 11:55) :
ttes mé félicitations à la mariée.
ke du bnheur
name nalène
grooos bisous