|
Maatou new look
15/07/2008 21:17
Warou rek la def!! BB Diop new look, mannequin confirmée.
kharr ba sori Galsen di commencé Beuri Thiapp. Soula sa yaye diapé!!!!
nice pic, nice sourire, nice robe. machallah dal!
Commentaire de jeni (17/07/2008 22:27) :
wé trop dof la top,la pose,le sourire,eblouissante mbapi!happy rek ci
yow!blague a part,combien de ptits toubabitos ta fait tombé en syncope?
|
Commentaire de maatou (20/07/2008 20:40) :
so fi dé bène toubab tombé woul en syncope.mane dé ma gui fi di niak solo
rek.sinon astou yow boul wakhé nonou pc kon va dire ke dama dèm france rek
yakhou fa alor ke c loin d etre vré.toi mem tu sé!!!!!!!!!!
http://2lousaines.vip-blog.com
|
Commentaire de vero (29/08/2008 21:38) :
wa ki kane la waoooooooouh ni la way hotlady beggue na dé!!!!!
|
Commentaire de adamas (30/08/2008 20:55) :
ouahou!!!!!!!!!!!kèl class!pour une hotlady en vraiment une de très HOT,
sexy et charmante!...ma chérie tu n'as vraimen rien à envier aux stars
américaines!...Bégué dé!!
|
Commentaire de eva (07/09/2008 18:13) :
lahila khalé mague na dé.wa mame fatou ya melni.waro tina dé!!!
|
Commentaire de diawa (08/09/2008 15:04) :
waaw adamaz ta vremen raizon el na rien a enier aux stars de...usa
|
Commentaire de c (09/09/2008 15:27) :
mame f way!!!!!!!BG
|
Commentaire de lynn (16/10/2008 16:36) :
défar nga bamou bakh
no comment
|
Commentaire de delkine (05/12/2008 18:24) :
matou vraiment happy kw yangui noce dal ay way noumay déf ma gneuw way!
|
Commentaire de siguisto (17/01/2009 20:00) :
ki yowla ni.tonton diop mom fo mou guisli.dodi surveille mw cel la avan
gnoukoy gnak.happy rek
|
| |